Lyrics

li mooy xaatim x 3 Sama gueinte gué yeémé cool, mbekté di kemtane Waral nelaw yi yeggul, Jok ndeké sa reetane Ferniente yi may weetali, sedal li, seedel li Pass Passu dellu ci war yi, wassaré love ci xol yi Tek ko ci tempo djiguene gniy soxeu ci euteu bi xale yiy foo di rée, teub ak danu si eukeu bi xeetou café ci deuk bi, kaff ak thiow yi niou woodeu "Adouna dou dara" Dem na, weur na, Guiss na, legui xamna Woruma né, waruma gné, xamé na Li ngay xaru di yotu, soko djotée weuri leneen Kumpe nga naane, mou muril leu noon, wari di neen Wutey sunu taar, xeutioy sunu tord sunu koor, faté yeurmandé, waral niakay fignou teer Nioy souf Nioy Ganthiakh, assamane nioy dokh Nioy moome, moy nioune, nioy Xaatim Ak Kallàma {2} Une generation gené râle à la quête d'un generale Aux jeunes les rôles, la voix on l'assume l'Afrique le drapeau, la voix et la plume Les aïeux dans les yeux, entre le marteau et l'enclume De ma plume, ils s'emerveillent, ma rue est ma seve Ma merveille de mere veille, je vend pas du reve Pas de treve sur le sentier de guerre le micro mon glaive, la vision des silions naguere On ecrit le JE, decrit la vie de NOUS le rire, la joie, les pleures dans nos peurs la haine et les peines de ceux qui vivent à genoux les regrets, la Nostalgie de ceux qui vivent dans nos coeurs Xaatim c'est ecrire, Kallàma une maniere de dire Notre vecu, nos memoires, des oreilles à seduire Une utopie appelle moi Picasso, un fou rire On essaye de peindre les mots aux couleurs du sourire
Lyrics powered by www.musixmatch.com
instagramSharePathic_arrow_out